Baye Cheikh Diagne 🇸🇳📚 (@baay_diagne) 's Twitter Profile
Baye Cheikh Diagne 🇸🇳📚

@baay_diagne

TALIBE SERIGNE TOUBA jaamu yalla Ligeeyal Sëriñ touba Al Quran xassida sama yitte done mouride sadikh 🙏🏼♥️commerçant -éleveur 🤍

ID: 1082802302640111616

calendar_today09-01-2019 00:52:41

4,4K Tweet

21,21K Followers

11,11K Following

Baye Cheikh Diagne 🇸🇳📚 (@baay_diagne) 's Twitter Profile Photo

Neek si ndigël rekk a woor Sëriñ salihu ndigël thioune ibnu cheikh bethio thioune Yalla nala sunu borom saam la aar la Yagal lafi lole teh andak weer 🙏🏽

Neek si ndigël rekk a woor 
Sëriñ salihu ndigël thioune ibnu cheikh bethio thioune 
Yalla nala sunu borom saam la aar la 
Yagal lafi lole teh andak weer 🙏🏽
Baye Cheikh Diagne 🇸🇳📚 (@baay_diagne) 's Twitter Profile Photo

Génération bu neek dafa am obligation ligeyal Sëriñ bi si juma ji Koon ñun ñi féké jamonoy CHEIKH MOUHAMADOUL MOUNTAXA Ngala nañu féxé ba buñu si ken mën def si sa doole ak sa alal teh xamni mo gën si yaw lenene ludul mom Yalla nañu sunu borom ndangoul jëf ji barkep borom touba

Génération bu neek dafa am obligation ligeyal Sëriñ bi si juma ji 
Koon ñun ñi féké jamonoy CHEIKH MOUHAMADOUL MOUNTAXA 
Ngala nañu féxé ba buñu si ken mën def si sa doole ak sa alal teh xamni mo gën si yaw lenene ludul mom
Yalla nañu sunu borom ndangoul jëf ji barkep borom touba
Baye Cheikh Diagne 🇸🇳📚 (@baay_diagne) 's Twitter Profile Photo

Aam ngen ma mane bamba teh aam naleen teh xamou leen ma wayeh mane xamna leen yenaay samay sahir teh maay seen batine yenay yaram wi ma rouh gui yor kun yena di mane koulen jaam ma nathi kuma jamit ngeen nathi JËRËJËFËTI SËRIÑ TOUBA ❤️

Aam ngen ma mane bamba teh aam naleen teh xamou leen ma wayeh mane xamna leen yenaay samay sahir teh maay seen batine yenay yaram wi ma rouh gui yor kun yena di mane koulen jaam ma nathi kuma jamit ngeen nathi 

JËRËJËFËTI SËRIÑ TOUBA ❤️
Baye Cheikh Diagne 🇸🇳📚 (@baay_diagne) 's Twitter Profile Photo

Xéwël nga si mouride yi dëgël Yokku nga sunu ngëm Yokku sunu yakaar Dolli ñu paas paas Sa leep ak soñee la si mouride yi JAAMU YALLA - LIGEEYAL S TOUBA Yagg fi lol teh weer

Xéwël nga si mouride yi dëgël 
Yokku nga sunu ngëm 
Yokku sunu yakaar 
Dolli ñu paas paas 
Sa leep ak soñee la si mouride yi 
JAAMU YALLA - LIGEEYAL S TOUBA 
Yagg fi lol teh weer
Baye Cheikh Diagne 🇸🇳📚 (@baay_diagne) 's Twitter Profile Photo

Sama réussite bi gëna rëy si sama adina mooy lima sama borom boleek Sëriñ cheikh mbacké mom Sëriñ salihu Dindii nga si mane mbone ak rëy Defma mey ku nango muñ ak di sant Deef nga si mane ragaal yalla Deef si mane bëg ak nango ligeyal Sëriñ touba Yalla ngafi yagg lole ❤️

Sama réussite bi gëna rëy si sama adina mooy lima sama borom boleek Sëriñ cheikh mbacké mom Sëriñ salihu 
Dindii nga si mane mbone ak rëy 
Defma mey ku nango muñ ak di sant 
Deef nga si mane ragaal yalla 
Deef si mane bëg ak nango ligeyal Sëriñ touba 
Yalla ngafi yagg lole ❤️
Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

"Boo xamoon gaawa fàtte gi la nit ñiy gaawa fàtte, ginnaaw boo faatoo, doo sàkku ci sag dund gërëmal kenn ku dul Yàlla"

Baye Cheikh Diagne 🇸🇳📚 (@baay_diagne) 's Twitter Profile Photo

Ñanaal leen ko mu yagg fi Jambaar dëgg bëgg Sëriñ bi Sëriñ Abo mbacké moom Sëriñ cheikh saliou Sunu borom saam lë aar lë Yagg fi lole teh weer

Ñanaal leen ko mu yagg fi 
Jambaar dëgg bëgg Sëriñ bi 
Sëriñ Abo mbacké moom Sëriñ cheikh saliou 
Sunu borom saam lë aar lë Yagg fi lole teh weer
Baye Cheikh Diagne 🇸🇳📚 (@baay_diagne) 's Twitter Profile Photo

Xamouma dara Amouma dara Mënou më dara Wayé sama borom baam më boleek Sëriñ bi la yëkk ni ñakatouma dara JËRËJËFËTI SËRIÑ TOUBA

Xamouma dara 
Amouma dara 
Mënou më dara 
Wayé sama borom baam më boleek Sëriñ bi la yëkk ni ñakatouma dara 
JËRËJËFËTI SËRIÑ TOUBA