Alaaji Fàllu Silla (@hadji_silla_) 's Twitter Profile
Alaaji Fàllu Silla

@hadji_silla_

ID: 1083738478532276224

calendar_today11-01-2019 14:52:42

18,18K Tweet

6,6K Followers

4,4K Following

Fallou Salih (@salihfadal) 's Twitter Profile Photo

Diomaye d wor Sonko faatou mooko gueuneul mane lilaa gueume. Ni Sonko communiquer ak contexte bi dina takh tapalékate yi khame sén bopp té hamna loumana khéw si nioom rek laye méti té sén tapalé doulène rombou...

AWA Balla⭐️ (@awambacke) 's Twitter Profile Photo

Señ Muhammad C’est triste de le dire mais c’est la vérité ! Il faut se ressaisir et s’appuyer sur des gens qui ont cru et se sont battus pour le projet. Des fois tu discutes avec certains Bilahi j’ai envi de pleurer ndax damani si ce n’est que ces gens là le pays ne va pas changer 😂😭

Alaaji Sheex (@echgueye) 's Twitter Profile Photo

Ça faisait longtemps que j’avais pas reçu une vraie bonne nouvelle. Ma petite sœur avait raté le bac il y a 2 ans. Je lui payais une formation. Elle s’est inscrite en candidat libre sans rien me dire. Aujourd’hui, ma mère m’envoie un vocal : elle a eu le BAC. 🥰🙏

Alaaji Fàllu Silla (@hadji_silla_) 's Twitter Profile Photo

SONKO robot la, amul nday, amul baay, amul mag, amul rakk, amul soxna, amul doom, amul i bokk, amul xarit. Na kenn ku ne jël Sonko teg fa sa nday, sa baay, sa mag, sa rakk, sa soxna, sa doom, sa mbokk, sa xarit ba xam lu muy joxe ?

Amdy Moustapha Mbacke (@ammbacke) 's Twitter Profile Photo

Alaaji Fàllu Silla Moor Suraŋ Al xuran la weddi, يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِذَا نَكَحْتُمُ الْمُؤْمِنَاتِ ثُمَّ طَلَّقْتُمُوهُنَّ مِنْ قَبْلِ أَنْ تَمَسُّوهُنَّ فَمَا لَكُمْ عَلَيْهِنَّ مِنْ عِدَّةٍ تَعْتَدُّونَهَا فَمَتِّعُوهُنَّ وَسَرِّحُوهُنَّ سَرَاحًا جَمِيلًا".

𝐏𝐫𝐢𝐧𝐜𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝟏𝟖🇸🇳 (@prince_mourid) 's Twitter Profile Photo

Xalaas ! Koo xam ne jotoo jaxasoo, sëy bi tas, booy idda wu ana lan moo wara tax nga idda wu ? Idda ji, ngir setal sa biir la, ndax dara topp la ci ëmb bi ak yu ni mel. Texte Alxur’aan bu leer wax na ne: « Sungeen fasee soxna si te fekk jaxasoowuleen, du jar ñuy idda wu »

Abdou KHadre Djeylani (@djeylaningom) 's Twitter Profile Photo

J’espère vraiment qu’il reviendra corriger à l’antenne tee mou def liko Sëriñ moor waxonn. Na nieuw niou ande jangui Ubbee » dou lu oyof du lu yomb

Baefa 🇸🇳 (@bvefas) 's Twitter Profile Photo

يَٰٓأَيُّهَا ٱلَّذِينَ ءَامَنُوٓا۟ إِذَا نَكَحْتُمُ ٱلْمُؤْمِنَٰتِ ثُمَّ طَلَّقْتُمُوهُنَّ مِن قَبْلِ أَن تَمَسُّوهُنَّ فَمَا لَكُمْ عَلَيْهِنَّ مِنْ عِدَّةٍ تَعْتَدُّونَهَا فَمَتِّعُوهُنَّ وَسَرِّحُوهُنَّ سَرَاحًا جَمِيلًا

◤Musaa Silla ◢✊🏿🇸🇳🇬🇼🇵🇸🔻 (@askiamusaa) 's Twitter Profile Photo

Moom su fekkoon dafa tont rekk dem ñu ne dafa juum wala dafa nàndul laaj bi mais dafa insister commenter, répéter répéter waat. C'est claire ki xamul dara ci fiq et à partir de ce moment TFM Groupe Futurs Médias® doit prendre ses responsabilités il ne doit plus faire du QR de fiq.

Alaaji Fàllu Silla (@hadji_silla_) 's Twitter Profile Photo

Sëriñ Muntaxaa jox na Ndigal Abdu Lahat Ka, mu ànd ak Póliis ak Sàndarmëri, jël ay matukaay ci xale yi amagul 18i at, tey dawal sareet ca biir dëkk ba. Nee na ñu dakkal ko. Benn xale bu amul lu ëpp 18i at bumu dawalati sareet.

Présidence Sénégal (@pr_senegal) 's Twitter Profile Photo

Le Bassirou Diomaye Faye s’est entretenu ce jour, à Lomé avec le Président du Conseil Faure Essozimna GNASSINGBÉ. Les deux dirigeants ont convenu de redynamiser la coopération entre Dakar et Lomé, en instruisant leurs ministres de convoquer la Commission mixte pour identifier des axes de partenariat.

Le <a href="/PR_Diomaye/">Bassirou Diomaye Faye</a> s’est entretenu ce jour, à Lomé avec le Président du Conseil <a href="/FEGnassingbe/">Faure Essozimna GNASSINGBÉ</a>. Les deux dirigeants ont convenu de redynamiser la coopération entre Dakar et Lomé, en instruisant leurs ministres de convoquer la Commission mixte pour identifier des axes de partenariat.