Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile
Moor Suraŋ

@s_sourang

Mor Sourang PDG Massalik Café, Écrivain et Chercheur sur le Mouridisme

ID: 1110223917199880194

calendar_today25-03-2019 16:56:23

31,31K Tweet

29,29K Followers

1,1K Following

Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

(Ba la ngaa moom sa bopp, manal sa bopp) Dégg naa PM Usmaan Sonkoo mu wax ne : “Ba la ngaa moom sa bopp, dangay manal sa bopp ba noppi” Loolu danuy delloo ci ideologie bi Seex Ahmadu Bàmba jàngale te jaarale ci murid yi, ba loolu moo waral ñu taxawal projet yu mag te masuñoo

(Ba la ngaa moom sa bopp, manal sa bopp)

Dégg naa PM Usmaan Sonkoo mu wax ne : “Ba la ngaa moom sa bopp, dangay manal sa bopp ba noppi” Loolu danuy delloo ci ideologie bi Seex Ahmadu Bàmba jàngale te jaarale ci murid yi, ba loolu moo waral ñu taxawal projet yu mag te masuñoo
Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Defar nga say mbokk defar ab jàmbur Ba ñépp jag nga jàpp nag sag njàmbur Yaa tax Bawal ak i Kajoor ak Njàmbur Di defu yiw, ku la sikkal dub jàmbur

Defar nga say mbokk defar ab jàmbur

Ba ñépp jag nga jàpp nag sag njàmbur

Yaa tax Bawal ak i Kajoor ak Njàmbur 

Di defu yiw, ku la sikkal dub jàmbur
Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Xamadi ak manqué de respect bi nekk Sénégal ñiy sol tenue ñoo ko jiite, nooy jàkkaarloo ak nit naan ko dégage rawati na kilifa ? fan yii rekk benn gendarme wax na ma ko, yaruleen gënu leen fi kenn seen tenue yi rekk la nit ñi wormaal

Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Ci préfet bii rekk ngay xame ne li doon xew Sénégal ci ray ak torture lépp ci reewande kese la tegu, nitu tenue yi ñoo yàq réew mi.